I say
Heure bou boite di teuth leu diakka di oubbii
Heure bou diakka oubbii leu boite yi di teuth
Bi leundeum beu lerr
Beulei nakk beuthieuk beu goudi
Da melnii dei ak dioudou nio bokk bountou bougni oubbii
Fadiar
Khel bou deuggou ak khol bi mouy kathial
Golo ci garap leu deuk mais febaram nite mokoy fadial
Yeah, diaroul ngueu meiy nopp man khol ngueu meiy deguei
Sama call dimeu degueloo gnimeu sorei sorelo gnimeu djeguei
Sa thiossane soko toppei do gnemei lou bess
Meuno nekk éboueur beug yeurei you wekh
Dieufou goor dh foumou fégné dh lamine dou ci leen
Lou goorjiguen woutei ak goor bou beuri djikowou jigeen
Yeah, nama yalla mousseul ci xamxam bou amoul mandoutei
Omzo deiy khekh pour ceinture mais solloul sakh toubeuy
Yeah, gars yei meunei boy
Regarde le score
Diay fruit di diokh nigger yi ci apple store
Fajar
Leer bii nieuw
Nenegn quand on aime on ne compte pas
Desfois on aime des gens pour qui on ne compte pas
Douma diay star dameiy tekk sama dieu ci surface terre bii
Fi gueuneu kawei fimeiy dem moy soufou tangkou mère bii
Yeah, ragal yalla mounoul nekk tappet
Boulmeu nianal gouddou fane nianal moudjou bou rafet
Pour diouk ben yone danou deux fois de suite
Le mensonge jette des fleurs mais ne donne pas de fruit
Montagne bi gueuneu kawei mouy metti souma warei danou
Man loumeiy gaagn moy nimey guissei sama boy yi di gaagnou
Ma momone game bi depuis diamono Jesus ak demba
Mais beugoumeu dei ci kaw scène beu melni papa wemba
Safara dou feyy même boko deffone ci ndokh
J'me méfie du feu qui brûle mais pas de l'eau qui dort
Yeah, gars yei meunei boy
Regarde le score
Diay fruit di diokh nigger yi ci apple store
Fadiar
Leer bii nieuw
Dama dokhi outti leer bii
Nakh limeu yagg nekk ci leundeum
Beug takk melni weer bii
Mais meuno tegui sama gueum gueum
Wone leine meu yone bii
Yeaaah yeah yeah yeah yeah
Digueuntei fimeu nekk ak fimeu beug deem
Digueuntei limeiy guiss ak lignoumeu beug wone
Digueuntei kimeu nekk ak kimeu beug done
Oh, yeah yeah yeah yeah
Oh oh oh
Kheyneu nath bi gueine bobou beu legui mangui khar fadiar
Otras canciones de Omzo Dollar
Il existe de nombreuses raisons de vouloir connaître les paroles de Fadiar de Omzo Dollar .
Quand on aime vraiment une chanson, comme cela pourrait être votre cas avec Fadiar de Omzo Dollar , on souhaite pouvoir la chanter en connaissant bien les paroles.
Une raison très courante de rechercher les paroles de Fadiar est le fait de vouloir bien les connaître parce qu'elles nous font penser à une personne ou une situation spéciale.
Ce qui arrive plus souvent que nous le pensons est que les gens recherchent les paroles de Fadiar parce qu'il y a un mot dans la chanson qu'ils ne comprennent pas bien et veulent s'assurer de ce qu'il dit.
Vous vous disputez avec votre partenaire parce que vous comprenez des choses différentes en écoutant Fadiar ? Avoir sous la main les paroles de la chanson Fadiar de Omzo Dollar peut régler de nombreux différends, et nous l'espérons ainsi.
Il est important de noter que Omzo Dollar , lors des concerts en direct, n'a pas toujours été ou ne sera pas toujours fidèle aux paroles de la chanson Fadiar ... Il est donc préférable de se concentrer sur ce que dit la chanson Fadiar sur le disque.
Sur cette page, vous avez à votre disposition des centaines de paroles de chansons, comme Fadiar de Omzo Dollar .