Paroles de ' Buur ' par Omzo Dollar

Buur est une chanson de Omzo Dollar dont les paroles ont été innombrablement recherchées, c'est pourquoi nous avons décidé qu'elle méritait sa place sur ce site web, avec beaucoup d'autres paroles de chansons que les internautes souhaitent connaître.

Anh my check, one two
Beuteuy guiss kholay yeuk lamigne tontou
Pour gni nga khamné dougnou sawar si ay fontou
Gninga xamnai depuis fadjar lagni gontou
Di lathiéi ni salaire bi démé
Ndèki rekk di khalate ni séne rére di démé
Khaliss bi dou woor même sou werr bi fégné
Mani xaliss bi dou woor même sou werr bi fégné
Da am ay borom bopp you amoul séne bopp
Ak borom xam xam yo xamné xamougne sene bopp
Nagnou moytou yaine jeuf yoy yatal fitneu
Nitou ya'allah doula wakh ni Ya'Allah nite leu
Kou yendou si sétou dh warna meune xolate bopam
Est ce que Ya'Allah dina balé koudoul ball mbokam?
Niteu geuneu cher lép lo guiss sikaw souff
Mais jiguén bouy djay thiaf mo geune jiguén bouy djay bopam
Da am ay Cris ak Lèo, pistoléro
Guiss fi ay triste fléau
Moudjou dila gnane taw ni kou guiss Météo
Miezé molay wakh lou khew ni profou Histo-Gèo
Yawmal Khiyam dh dougnla wakh heure bi
Comme mbindane bou mole day todj keur gui
Ci kaw ci kanam en avant les amis
Mane ben yonn la kham meme souma deukone niary-tally (Abozé)

Digueunté fouma naik fouma jeum da am ay affaires yign ma wakhoul
(Ann, anh Anh my nigga) x2
Limlay yeugeul moy (x2)

Nigga prof bi day tekk (Nigga prof bi day tekk)
Ya'Allah rekkey buur
Rignseu bi day taik (Rignseu bi dey tekkk)
Ya'allah raikay buur
Da am gno xamnai saini liguéye tokk di wakh la bounigni di daif (bounigni di daif)
Mais souvent gni di wakh dougnou mousseu mousseu bokak gni di deff
Dama geum Ya'allah geum sama boop Zo saraloul sakh (Zo saraloul sakh)
Gnane Ya'allah outi lima gnanone Zo saraloul sakh (Zo saraloul sakh)

Soumala tognai nigga balma th nga bayi di gaide
Biir safara dh fofou kaine dou bayi mou saideuh
Nigga dokh di wakhou mo geune daw nank
Élèves yi douniou sport dagni daw jang
Présidents Afrique yi dagni mbeuw kassai
So xamone lougni sacrifier pour daw kassai
Allalou deukou leumb ngeu beugeu pour yaw kassai
Beussna am waiteuk ya'allah nigga yow kassai
Boulma décevoir, goorou Sénégal yi kagne lagni xam nai polygamie droit leu dou devoir
Dou yanê yaine guêls yéy indi matérialise
Ma soeur le mariage n'est pas le but ultime de la vie
Sa dome bou jiguéne sonal ngako boko mayai si force
Dimanche le jour de mariage, lundi jour de divorce
Yeah! Da am yaine doundou yoy tègué coté
Da Malaykal meuwty dh keneu douko daih
Bakane meune na noyi même souy xêègne xaite
Am gnouy gnak saine bakaine nakh saine khaite
Dou lou nekh ga
Mais nite bou waikh aka beug nite kou nioul bou yoor Xaliss bou waikh tall
Niounai gnari goor youy faunantai c'est naturel
Gnari goor di seuy niounai naturel
Pourtant Adama ak Awa lagnou sakando
Ya'allah sakando woul Adama ak Roméo
Diné mingo woul ak Ada dès fois lolou am
Il faut que bayi yone pour jeul yonou ndam
Joulite ngeu mba Sénégalais yaw yay tane
Sa mame meu naikone diiw mais yaw yaye kane?
Ya'allah kouko geum sa boppou ngeu geum
Motah ya'allah kouko togn sa bopou nga togn
Musique dafa kharam boula dara nakh
Deug raik lay wakh nigga dara nak
Boul sakh khaip koudoul wakh
Djouk job raik th boul xoff
Boul moussa daif ak koudoul daif loumouy wakh
Yaine say gninga doul fook gnoy daif lodoul fokk Yeah!
Est ce que jarna bakaar pour yokkeu sa l'aise
Loutakh ngay wagni salaire pour yokeu sa leer
Ngainai dinai ci xol leu?
Est ce que dinga daim examen jokhai feuille blanche nai jangueu si xail leu?
Daif lou bakh si kaw, daif lou bone si souf
Comme mourou si kaw daif leggings si souf
Boy di wakh deug dh no déf gnou rayleu
Prophète yi dh gnofi eupone ay haters
Kou sathie danga bayi sa lokho
Motah charia bi néna faut que nga bayi sa lokho
Goor bokoul ak jiguéne dafa waur Ya'Allah
Kone goor-jiguéne geum ya'allah défouko goor ya'Allah
Ouztaz balma da am louma lay lathie yaw
Prophète bi orphelin leu wakhma kouko yalwane lo?
Wakhma lane la ya'allah wakh ni lagni daifak djirèm
Tothie naine ci croisement omelette ko eupeu ndieurign
Lou goor geune beug ci aduna jiguéne leu dou dara motax
Sou seuyai dina am 2 minutes yo xamnai aduna bi doussi beug dara

Goumbeu jakk dji day wakh lou Sèlbè doul guiss
Louma geuneu geum Ya'allah geuneu waidi nite
Kone saite kate bi day tekk
Rignseu bi day tekk
Président bi day tekk
Policier bi day tekk
Milliardaire bi day tekk
Sa rappeur bi day tekk
Mane mi di tekk damay tekk nigga

Nigga niom gneupeuy tekk (nigga prof bi day taik, nigga prof bi day tekk)
Yaallah rekkay buur
Rignseu bi day taik (Rignseu bi day tekk)
Ya'Allah rekkay buur

Da am gno xamnai saini liguéye tokk di wakh la bounigni di daif
Mais souvent gni di wakh dougnou mousseu mousseu bokak gni di daif
Dama geum Ya'allah geum sama boop Zo seraloul sakh (Zo seraloul sakh)
Gnane Ya'allah outi lima gnanone Zo seraloul sakh (Zo seraloul sakh)

Il existe de nombreuses raisons de vouloir connaître les paroles de Buur de Omzo Dollar .

La raison la plus courante de vouloir connaître les paroles de Buur est que vous l'aimez beaucoup. Évident, n'est-ce pas ?

Si votre motivation pour avoir recherché les paroles de la chanson Buur était que vous l'adorez, nous espérons que vous pourrez profiter de la chanter.

Sentez-vous comme une star en chantant la chanson Buur de Omzo Dollar , même si votre public n'est que vos deux chats.

Dans le cas où votre recherche des paroles de la chanson Buur de Omzo Dollar est parce qu'elle vous fait penser à quelqu'un en particulier, nous vous proposons de la lui dédier d'une manière ou d'une autre, par exemple en lui envoyant le lien de ce site web, il comprendra sûrement l'allusion.

Ce qui arrive plus souvent que nous le pensons est que les gens recherchent les paroles de Buur parce qu'il y a un mot dans la chanson qu'ils ne comprennent pas bien et veulent s'assurer de ce qu'il dit.

Vous vous disputez avec votre partenaire parce que vous comprenez des choses différentes en écoutant Buur ? Avoir sous la main les paroles de la chanson Buur de Omzo Dollar peut régler de nombreux différends, et nous l'espérons ainsi.

Il est important de noter que Omzo Dollar , lors des concerts en direct, n'a pas toujours été ou ne sera pas toujours fidèle aux paroles de la chanson Buur ... Il est donc préférable de se concentrer sur ce que dit la chanson Buur sur le disque.

Nous espérons vous avoir aidé avec les paroles de la chanson Buur de Omzo Dollar .

Sur cette page, vous avez à votre disposition des centaines de paroles de chansons, comme Buur de Omzo Dollar .

Apprenez les paroles des chansons que vous aimez, comme Buur de Omzo Dollar , que ce soit pour les chanter sous la douche, faire vos propres covers, les dédier à quelqu'un ou gagner un pari.

Rappelez-vous que lorsque vous avez besoin de connaître les paroles d'une chanson, vous pouvez toujours compter sur nous, comme cela vient de se produire avec les paroles de la chanson Buur de Omzo Dollar .