Lo Meu Def est une chanson de Omzo Dollar dont les paroles ont été innombrablement recherchées, c'est pourquoi nous avons décidé qu'elle méritait sa place sur ce site web, avec beaucoup d'autres paroles de chansons que les internautes souhaitent connaître.
Vous adorez la chanson Lo Meu Def ? Vous ne comprenez pas tout à fait ce qu'elle dit ? Besoin des paroles de Lo Meu Def de Omzo Dollar ? Vous êtes au lieu qui a les réponses à vos désirs.
Khalé yi meu beug mounou maléne am
Khalé yi meu am nakk mounou maléne beug
Wanté yow mom yow mom yow mom yow mom anhh
Amneu lo meu def lo meu def lo meu def lo meu def anhh
Ndakh fo yeundou meu yendou feu yendo diakhlei
Fo yeundou meu yendou feu yendo diakhlei
Hey khalei bii ya mom lii
Guissna niou beurii mais guissoumeu comme lii
Douma feine baby diakhal ngama somme nii
Femme de mes rêves wayei yameiy diokh insomnie
Ay beute you melni assamane sou khiné
Show bii biimou siigné dama signé
Yaram bou gueuneu fess salle de ciné
Kharou pour sey rondeurs woowemeu gallilé
Diégué nako presque
Nekko na ngueu def
Baby dangmeu nekh
Boko gueumé ya thii dess
Wanté dameiy wokh beu dei
Show bii khol meu fass kanamam
Loumou wokh meu def mangui melni face kanamam
Maneko louy seu number beug naleu deggate
Niou weur touti wone leu sama lé-ga
Dafeu noppi di douggou thii ay débat
Kagn laleiy guissate
Showbii neimeu je ne sais pas
Khalé yi meu beug mounou maléne am
Khalé yi meu am nakk mounou maléne beug
Wanté yow mom yow mom yow mom yow mom anhh
Amneu lo meu def lo meu def lo meu def lo meu def anhh
Ndakh fo yeundou meu yendou feu yendo diakhlei
Fo yeundou meu yendou feu yendo diakhlei
Anh
Hey khalé bi da yémé
Mou takhaw amoul nigger bou ko niémé
Ma nieuw rek nekko show dii bii ngueu fégné
Nieupeu diouk takhaw nii ay karaw youniou peigné
Ajouter ko Instagram dh photo yeup la aimé
Soumako khamone dh meu pres'ko sama re-mè
Mangui dof nigger khawmeu noumou démé
Topnako bountou gallem kham foumou deuké mais
Sa youmako accélérer show bii dafmeiy freiner
Ma wokh mouneimeu dangueiy meew nei lait demi et crème eh
Khamna dangma yegg mais maleiy dannel nei ascenseur
Someu dieulei dougnleu lal melni échangeur
Def na tout pour que coûte que coûte ngueu beug meu niou couple ba meu toupp beu dioub
Lathieko noumeiy def beu mou nopp meu
Mouneima wayyal son bou youssou ndour
Maneiko yow mii dingmeu dof lo yaa mom lii
Khalé bi meu dof lo yaa mom lii
Khalé yi meu beug mounou maléne am
Khalé yi meu am nakk mounou maléne beug
Wanté yow mom yow mom yow mom yow mom anhh
Amneu lo meu def lo meu def lo meu def lo meu def anhh
Ndakh fo yeundou meu yendou feu yendo diakhlei
Fo yeundou meu yendou feu yendo diakhlei
Sone na thii sallei bi
Doffone na thii khalei bi
Wokh nako mou nieuw mou nieuw mou nieuw
Wanté douma faletti
Defna limeu meune
Wanté show bi neina douma gueum
Bayil meu bayiko mou dem mou dem mou dem meu am sama diam dji
Oh
Khalé yi meu beug
Mounou maléne am (no no no)
Khalé yi meu am nakk
Mounou maléne beug (no no no)
Wanté yow mom yow mom yow mom yow mom anhh
Amneu lo meu def lo meu def lo meu def lo meu def anhh
Ndakh fo yeundou meu yendou feu yendo diakhlei
Fo yeundou meu yendou feu yendo diakhlei
Otras canciones de Omzo Dollar
Sentez-vous comme une star en chantant la chanson Lo Meu Def de Omzo Dollar , même si votre public n'est que vos deux chats.
Une raison très courante de rechercher les paroles de Lo Meu Def est le fait de vouloir bien les connaître parce qu'elles nous font penser à une personne ou une situation spéciale.
Vous vous disputez avec votre partenaire parce que vous comprenez des choses différentes en écoutant Lo Meu Def ? Avoir sous la main les paroles de la chanson Lo Meu Def de Omzo Dollar peut régler de nombreux différends, et nous l'espérons ainsi.
Il est important de noter que Omzo Dollar , lors des concerts en direct, n'a pas toujours été ou ne sera pas toujours fidèle aux paroles de la chanson Lo Meu Def ... Il est donc préférable de se concentrer sur ce que dit la chanson Lo Meu Def sur le disque.
Sur cette page, vous avez à votre disposition des centaines de paroles de chansons, comme Lo Meu Def de Omzo Dollar .