Assamane est une chanson de Dip Doundou Guiss dont les paroles ont été innombrablement recherchées, c'est pourquoi nous avons décidé qu'elle méritait sa place sur ce site web, avec beaucoup d'autres paroles de chansons que les internautes souhaitent connaître.
Si vous avez longtemps cherché les paroles de la chanson Assamane de Dip Doundou Guiss, commencez à échauffer votre voix, car vous ne pourrez pas arrêter de la chanter.
Vous adorez la chanson Assamane ? Vous ne comprenez pas tout à fait ce qu'elle dit ? Besoin des paroles de Assamane de Dip Doundou Guiss ? Vous êtes au lieu qui a les réponses à vos désirs.
Kholal cii kaw té nga bayifa saye beut
Guisso dara lou djara thiow té mo waral lepp
Guisso dara lo meuneu laale lo meusseu tiim ak saye beut
Kholal ci kaw assamane wessu nga sa level
Gni fa né défouniou bruit té louné nga lène dégueul
Mais niouné nioune deukou gnoufi kou déh dinagnela
Yégueul
Sama biss mou ngui nieuw, sama booss tayla xeuyna
Kone bou défé nga ndieuk dem néko nama diégueul
Nieup nénagne daf gnou tiim kone mo ngui cii assamane
Loutah mou tek niou fi lathieko saye maame adama ak awa
Nénagne nioune nio ngui doundeu akhirou zamane
Kou djot lettrou assamane exactement ndakh dama khawa
Yémou cii gni wané nii niom gueumeu tougnouko
Pour mane gni gueum gno yéwou gni dess dagno guemeintou
Comme scientifique ak philosophe yi diémeu prouvé lénène
Boudé bo guissoul do meusseu gueum déh nga thi poukeuré
Men
Doko door balle bamou diaaleu
Ropalane khalatoufa yégueu
Lougni def xana sani niaane
Di niaane yallah na ngou niaane yikoy fekk assamane
Assamane assamane assamane assamane
Kholal cii kaw té nga bayifa saye beut
Guisso dara té lifa né xadioul cii seu cerveau
Da nga koy khol moulay guiss mo ngui fepp fi ngay dieum
Aduna bepp la muur yémoul rek cii sen deuk
Kharitou wérr bek bidew yi mbok jante ak naathie
Soubeu lay lerr goudi mou leundeum gentlema
Boufay dem do yaubou touss démal sett sa maame
Loutah yène makk yi di défar testament
Han! Mom réka tedd ndaxté mane xamena
Mom rékay aaté mom réka am bobou makkama (capacité)
Assamane nay limite té kène douko dindi
Amena diourom niarry (7) assamanes kounek ak sa limite
Boul khol ci nignou doundé cii souf
Kigni goungué gniy roukhe
Té xam nga dioum wessuwoul
Maye gnou lepp lou bepp mindef di woute
Bagni meune def li nga gnou santeu fi lek niouy dougou sunu
Bamell
Doko door balle bamou diaaleu
Ropalane khalatoufa yégueu
Lougni def xana sani niaane
Di niaane yallah na ngou niaane yikoy fekk assamane
Assamane assamane assamane assamane
Quand on aime vraiment une chanson, comme cela pourrait être votre cas avec Assamane de Dip Doundou Guiss, on souhaite pouvoir la chanter en connaissant bien les paroles.
Savoir ce que disent les paroles de Assamane nous permet de mettre plus de sentiment dans l'interprétation.
Sentez-vous comme une star en chantant la chanson Assamane de Dip Doundou Guiss, même si votre public n'est que vos deux chats.
Une raison très courante de rechercher les paroles de Assamane est le fait de vouloir bien les connaître parce qu'elles nous font penser à une personne ou une situation spéciale.
Dans le cas où votre recherche des paroles de la chanson Assamane de Dip Doundou Guiss est parce qu'elle vous fait penser à quelqu'un en particulier, nous vous proposons de la lui dédier d'une manière ou d'une autre, par exemple en lui envoyant le lien de ce site web, il comprendra sûrement l'allusion.
Il est important de noter que Dip Doundou Guiss, lors des concerts en direct, n'a pas toujours été ou ne sera pas toujours fidèle aux paroles de la chanson Assamane... Il est donc préférable de se concentrer sur ce que dit la chanson Assamane sur le disque.
Nous espérons vous avoir aidé avec les paroles de la chanson Assamane de Dip Doundou Guiss.